Fiche technique
Format : Broché
Nb de pages : 89 pages
Poids : 135 g
Dimensions : 14cm X 22cm
EAN : 9782747553650
Quatrième de couverture
"La béy daa dunde ba mat sikket man na caa dee"
Waaye béy gisatul ñax te lekketu kese masukoo nax. La béy daa dunde ba mat sikket mooy njàmbat li ci mbaar mi. Béy du dundey wax. Lii rekk a tax kër yi wéet. Wéttalu béy daal luy sax. Ñàkk gee tax li ëpp ci béy yi àkki kàdd ga, sori keppaarug guy ga.
Na sàmm seen kàddu far dëddu fa ñu gën a sopp wuti réew mu amul daay. Fii nag la gàddaay gi tàmbalee. Waaye ba fa ñuy mujj lu fi nit rëdd takkandeeram la ko rëddee.
Daawuda Njaay
Tout exil exige en amont, un rituel, une offrande, un sacrifice. C'est à l'ombre du baobab, temple mythique et mystique de la parole que Douada Ndiaye fit son offrande lyrique.
Keppaarug Guy Gi / L'ombre du Baobab (L'Harmattan, 1999) se termine par un poème charnière: "gàddaay" (s'exiler) qui ouvre la voie au nouveau recueil du poète de la Médina.
L'Exil ou Gàddaay gi dépeint moins un déplacement qu'un cheminement personnel de l'auteur. En quête de paix dans un monde injuste, Daouda Ndiaye nous fait rencontrer des Hommes insatisfaits de leur sort, partagés entre la crainte et l'espoir de vivre.